"Fi Ba Leuz" Lyrics
"Fi Ba Leuz" ei ai upu i le castilian spanish gagana.
"Fi Ba Leuz" o lona uiga e sau mai le castilian spanish gagana ma e le'i liua i le taimi nei i le fa'aliliuga Igilisi.
Real : UnderVfx - Ama Bamba
DOP : Mandione Laye Ka
Décors : Yarba Deco
Light : Bras Magic
Musique : Zoom Beat
© 2021 Cosanostra
#FiBaLeuz est disponible sur toutes les plateformes de streaming :
Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux :
Instagram :
Twitter :
Facebook :
LYRICS :
FI BA LEUZ
Intro
Eih yooooooo
Eihhh hiiiiiiiiiii
Yeahh yooooo yaaaaaa yeiiiiih
1er couplet
Fi ba Leuz ma lay mome Thiow reikay bari
Deff la sokhnay sama thiobarei
Topale sama guinaw tei bou thiow bari
Khame nga ni yay sama thiapali
Khame nga ya ni ma
Ni teike nama la heiii
Fouma Mousta teike diame bou yallah binde Mane fonke nama la
Manite ma ni la heiii
Sa kheile na dalei
Diandia bi dou sopeikou Massamba dou deime sa Massamba la heii
Refrain
Fi ba Leuz ma lay mome thiow reikay bari bari bari bari bari
Deff la sokhnay sama thiobarei bari bari bari bari
Topale sama guinaw tei bou thiow bari bari bari bari bari
Khame nga ni yay sama thiapali bari bari bari
2ème couplet
Diankh ya ma ni
Dou koula tchipatou gueine ci ndakhtei yomboulo dou koula diame nani
Heiiii waaaaayyyy
Diankh Yama ni
Biss dîna gneuw nga daagou ci keur gui seuyeule ma ma toke ci ndanane yi
Eiiihhhh waayyyyyyyyy
Ling ma wakh takh na meune nama wate ni doma bayi même souma faatoo
Adouna yeup souniou dadjei wone pour séparer niou dou takh mou aantou
Djankh Yama ni djankh Yama ni
Li nga diik doy nama weurou ma leineine Li nga ma wakh neikh nama yeiiii
Refrain
Fi ba Leuz ma kay mome thiow reikay bari bari bari bari bari
Deff la sokhnay sama thiobarei bari bari bari bari
Topale sama guinaw tei bou thiow bari bari bari bari bari
Khame nga ni yay sama thiapali bari bari bari bari